Lebb En Wolof
TubeHealth is an independent service and is not affiliated with or endorsed by YouTube or Google.
Data displayed on this page is retrieved via YouTube API Services.
Updated:
Lebb En Wolof Channel Description Snapshot
Channel Description
Lebb en Wolof moy Seen mbégte ak seen njàriñ ci guirou askan wi. 🌍✨
Léeb day jaare ci lu ne (lu yem xel, lu nit taamu di gis, wala lu mu masul gis, niki mala buy wax...) 📚💭, ngir jangale; nun nag sunuy léeb jangale mbaax (jikko ju rafet) mooy jubluwaay bi. 🎙️🎧
Leeg-leeg it nu jëfandikoo baatub jaar-jaar, su ñeelee jenn jëmm 🔄✍️
Adduna barab bu lëndëm la, xam-xam ay làmp bi mo koy leeral. 🌍📖
Tée niougui fi pour Leeral Laa 👨🏫🌱

About This Page
Methodology: This page displays a snapshot of publicly available creator information retrieved via YouTube API Services.
Snapshot
Snapshot Date:
Data Source: Public data retrieved via YouTube API Services
Data is refreshed at least once every 30 days.