Kàggug wolof

TubeHealth is an independent service and is not affiliated with or endorsed by YouTube or Google. Data displayed on this page is retrieved via YouTube API Services.
Updated:

Kàggug wolof Channel Description Snapshot

Channel Description

✅Dawalal lii (Lis ceci) 👇👇
Assalaamu halaykum !
Dalal ak jàmm ci biir Kàggug wolof ( bibliothèque wolof). Sunu yéene mooy yaatal làkku wolof ba ñépp man koo bind (écrire), waaye it man koo dawal (lire) ci lu dul ag yàq niki noonu, yaatal bépp xam-xam. Bokk na ci wëppa yi :
Xam sa réew, xam sa diine, xam sa cosaan, léeb, wax ju am njariñ, Wolofal, léebu, jàng làkk i doxandeem yi ( anglais, français,...)
Ngir bokk ci ñiy suqali réew mi jàngal làkk wii.
Noo ngi lay ñaan nga dooleel nu bu baax tay yaatal vidéos yi.
Ngir jokkoo ak nun (Nous contacter ) :
WhatsApp : 00221783797230
Mail : kaggugwolof@gmail.com
Dileen ñaan ngeen bëgg xët wi #abonnez_vous
https://youtube.com/@Kaggugwolof/?sub_confirmation=1

About This Page

Methodology: This page displays a snapshot of publicly available creator information retrieved via YouTube API Services.

Snapshot

Snapshot Date:
Data Source: Public data retrieved via YouTube API Services
Data is refreshed at least once every 30 days.