Wolof English School
TubeHealth is an independent service and is not affiliated with or endorsed by YouTube or Google.
Data displayed on this page is retrieved via YouTube API Services.
Updated:
Wolof English School Channel Description Snapshot
Channel Description
Dalal ak jàmm ci Wolof English School! 🇸🇳🇬🇧
Ndax bëgg nga wax Anglais ni "English Man" te yombal ko ci Wolof? Fi mooy sa kër! Fi dagnuy jàngale lakk bi ci anam bu neex, bu yomb, te jëm ci li ngay dunda bës bu nekk.
Li ngay fekk ci chaîne bi :
* ✅ Vocabulaire ak Expressions yi gënë am solo.
* ✅ Conjugaison ak Grammaire bu yomb ba ci biir.
* ✅ Ay "Tips" ngir dégg ak wax Anglais mu leer.
* ✅ Cours pour débutants ak ñi bëgg gënë xam lakk bi.
Our Mission: To make English accessible to every Wolof speaker around the world. Whether you are in Dakar, New York, or Paris, we bring the school to your screen!
👉 Abonnel léegi ngir sàkk sa kër ci biir classe bi!
New video every week! 🎬

About This Page
Methodology: This page displays a snapshot of publicly available creator information retrieved via YouTube API Services.
Snapshot
Snapshot Date:
Data Source: Public data retrieved via YouTube API Services
Data is refreshed at least once every 30 days.